Sit bii dafay joxe ay ëmbiit yu bari ngir askanu ñiy làkk wolof. Li waral loolu mooy fësal solo yu askanu Wolof , waye tamit ngir gëna xam-xam Kàddug Yàlla. Looloo tax, sit bii dafay wone bibal bi ak filmu Yeesu ci wolof. Banneexulen ci seen ñëw ci sit bii!
Verset du jour
Kan ci yeen moo mëna jaaxle ba yokk ab diir ci dundam? Su fekkee lu tuuti loolu mënuleen ko, lu tax ngeen di jaaxle ci li ci des?
Luug 12.25