Sit bii dafay joxe ay ëmbiit yu bari ngir askanu ñiy làkk wolof. Li waral loolu mooy fësal solo yu askanu Wolof , waye tamit ngir gëna xam-xam Kàddug Yàlla. Looloo tax, sit bii dafay wone bibal bi ak filmu Yeesu ci wolof. Banneexulen ci seen ñëw ci sit bii!
Verset du jour
Fàww ñi bokk ci nun tamit jàng di matal ay jëf yu baax, ngir ñu mëna faj soxla yu jàmp yi. Noonu seen dund dina am njériñ.
Tit 3.14