Pirogue

Ce site présente un large éventail de contenu pour la communauté wolophone. Cette diversité dans les contenus a pour but de faire valoir les valeurs du peuple wolof mais aussi d'apporter une compréhension de la parole de Dieu. C'est pourquoi ce site présente la Bible et le film de Jésus en wolof. Bonne navigation !

a

 Samay doom, bunu bëgg ci kàddu ak ci làmmiñ rekk, waaye ci jëf ak ci dëgg.  Ci noonu lanuy xame ne ci dëgg gi lanu bokk, te dinanu dalal sunu xol ci kanamu Yàlla

1Yowana 3:19-19

e

Mbind mu sell mi yépp, ci gémmiñu
Yàlla la jóge, te dafa am njériñ ngir jàngale, yedd, jubbanti, ak yar
ci njubte. 

2 Timote 3:16

Verset du jour

Waaye yaw booy ñaan duggal ci sa néeg bi gëna ruqe, tëj bunt bi te nga ñaan sa Baay bi fa nekk ci béréb bi umpe, te sa Baay biy gis li ngay def ci kumpa dina la neexal.

Matthieu 6.6
Partager

Votre encouragement nous est précieux

Vos témoignages contribuent à rendre possibles des sites web tels que celui-ci.